Diiwaani Senegaal
Diiwaan yi ay dog lañu séddaliinu Senegaal, 14 lañu.
Dogiin
SoppiFi mu nekk nii 14 lañu, ba ñu sosee Maatam ci 2001, teg ci sos yeneen ñatt ci 2008: Kafrin bokkoon ci diwaanu Kawlax, ak Kéedugu bokkoon ci Tambaakundaa ak Séeju gi bokkoon ci Siggcoor.
Réyaay ak way-dëkk
SoppiDiiwaan | Réyaay ci km²
|
Way-dëkk |
---|---|---|
Cees | 6 601 | 1 348 637 |
Fatik | 7 935 | 639 075 |
Kawlax | 16 010 | 1 128 128 |
Koldaa | 21 011 | 834 753 |
Luga | 29 188 | 559 268 |
Maatam | 25 083 | 423 041 |
Ndakaaru | 550 | 2 411 528 |
Ndar | 19 044 | 863 440 |
Njaaréem | 4 359 | 930 008 |
Siggcoor | 7 339 | 557 606 |
Tambaakundaa | 7 339 | 557 606 |
Mboolante | 196 176 | 10 225 816 |
Xool it
SoppiLëkkalekaay yu biir
Soppi- Séddaliinu yoriinu Senegaal
- Tundi Senegaal
- Ndiiwaani Senegaal
- Dëkkaani ndiiwaani Senegaal
- Dëkkaani Senegaal
- Gox-goxaani Senegaal
- Dëkki Senegaal
Téerekaay
Soppi- (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
- (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
- (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal, Dakar, Ministère du Plan, 1967, 705 p. (Thèse de 3e cycle publiée)
- (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal. Complément pour la période des origines à 1965 et mise à jour 1966-1973, Paris, Mouton, 1977, 637 p.
Lëkkalekaay yu biti
Soppi- (fr) Agence Nationale de la Statistique et de la Démographie du Sénégal (chiffres des différents recensements et estimations officielles jusqu'en 2015)
- (fr) « La région dans les limites administratives des États de l'Afrique de l'Ouest » (article de Gérard Brasseur dans le Bulletin de l'IFAN, série B, 1968, tome 30, n° 3, p. 861-867)
- (fr) « Trois nouvelles régions administratives seront créées au Sénégal » (Agence de presse africaine, 25 mai 2007)
| |||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |