Diiwaanu Luga
Diwaanu Luga benn la ci 14 diwaani Senegaal yi. Mooy diwaan bi ëppi pegg ci Sengaal Gépp, moom dafa diggu. Am na 677533 ciy way-dëkk, te yaatoo 29188km2
Melosuuf
SoppiAy peggam
SoppiDiiwaanu Luga ngi peggook:
- Diiwaanu Ndar, ci bëj-gànnaaram
- Diiwaanu Maatam ci penkoom
- Diiwaanu Cees, bu Jurbel; bu Fatik, bu Kawlax ak bu Tambaakundaa ci bëj-saalumam
- Mbàmbulaanug Atlas gi ci sowwam
Tund yi
SoppiXool it
SoppiTéerekaay
Soppi- (fr) Fatou Diop, « Le travail comme représentation et pratique quotidienne dans la région de Louga », in Elisabetta Benenati et al. (sous la direction de), Lavoro, genere e sviluppo locale in Mali e in Senegal, Turin, L’Harmattan Italia, 2002
- (fr) Diop Fatou Diop (sous la coordination de), Les nouvelles formes d’émigration dans la région de Louga, Rapport de recherche « Tukki liggéey la », Coopération Inter-Universitaire Turin-Sahel (Université de Turin-Italie/Université Gaston Berger Saint-Louis, Sénégal), 2003
- (fr) Moustapha Sar, Louga et sa région (Sénégal). Essai d’intégration des rapports ville-campagne dans la problématique du développement, Dakar, IFAN, Université de Dakar, 1973, 308 p. (Initiations et Etudes Africaines n°30). (Thèse de 3e cycle soutenue en 1970, Strasbourg)
- (fr) Jorge Suazo-Toro, Proposition de mesures d'amélioration de l'élevage : région de Louga au Sénégal, Uppsala, Swedish University of Agricultural Sciences, International Rural Development Centre, 1993
Lëkkalekaay yu biti
Soppi
| |||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |