Diiwaanu Cees benn la ci 14 diiwaan yu Senegaal, Féete ci penku Réew mi, wër ndombo Ndakaaru. Yaatoo 6 601 km2, am 1 442 338 ciy way-dëkk. dëkkub Cees Mooy Péeyu diiwaan bi.

diiwaanu Cees ci lonkoyoonu Sengaal

Melosuuf

Soppi

Ci genn wàllam mi nga janook Tefes-gu-Mag gi, fi mbayum yu-sew yi di ame, ci Ñaay bi, ci geneen gi di janook Tefes-gu-Tuuti gi di barab bi ëppi nemmeekukat ci Senegaal.

Doon ab tombub jàllu ci diggante Ndakaaru ak li des ci réew mi. Diiwaan bi am na ay cëslaay yu tali ak yu weñ yu matale ngir wóoral tuxute gi(dem-beek-dikk bi), ci suufam.

Doonte diiwaan bu tuuti la soo ko méengalee ak yeneen yi, waaye mooy ñaareelu diiwaan bi ëppi nit, ci Réew mi, ginnaaw Ndakaaru.

 
Diiwaani aki tundam

Séeddaliinu suufam

Soppi

Diiwaan baa ngi Séeddaliku ci 3 tund:

Taariix

Soppi

Ci Melosuuf Diiwaan bi tay mooy nguuru Kajoor ga woon ak gu Bawol. Ag Yokkuteem mi ngi tegu woon ci yoonu weñ wi, rëdd wu Ndakaaru-Ndar ci mujjantalu XIXu xarnu, wu Ndakaaru-Niseer tegu ci. Bokk na ci diiwaan yi gën a yàgg ci Senegaal.

Téerekaay

Soppi
  • (fr) Sidath Diop, Les polissoirs de la région de Thiès : étude typologique et ethnographique, Dakar, Université Cheikh Anta Diop, 2002, 101 p. (Mémoire de Maîtrise)
  • (fr) Roger Laval, La décentralisation au Sénégal : l'industrie dans la région de Thiès, travail d'études et de recherches, Dakar, Département de géographie, Université de Dakar, 1971
  • (fr) Guy Quérec, La population urbaine au Sénégal. La ville de Thiès et sa région, Dakar, Université de Dakar, 1968, 2 fascicules, 167 p. + annexes (Dipôme d’Etudes Supérieures)
  • (fr) Papa M. Sylla, Évolution de l'impact de la stratégie et du fonctionnement d'un programme de lutte contre la lèpre dans la région de Thiès (Sénégal), Université de Montréal, 1990 (M. Sc.)
  • (fr) Gordon Williams et al., « Enquête sociolinguistique sur les langues Cangin de la région de Thiès au Sénégal ». Cahiers de recherche linguistique, 1989, n° 3, Dakar, SIL.

Lëkkalekaay yu biti

Soppi
  14 Diiwaani Senegaal  

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·