Diiwaanu Tambaakundaa
Diiwaanu Tàmbaakundaa mi ngi nekk ci penku réew mi, benn la ci 14 diiwaan yu Senegaal yi, di it bi ci ëpp ci rëyaay. Dëkku Tàmbakundaa mooy péeyub diiwaan bi. am na 605 695 ciy way-dëkk te yaatoo 59 602 km²
.
Melosuuf
SoppiAy peggam
SoppiDiiwaan baa ngi digoo ak:
- Diiwaanu Maatam ak bu Luga ci bëj-gànnaaram;
- Diiwaanu Kawlax ak bu Koldaa ak réewum Gàmbi ci sowwam;
- Réewum Gine ci bëj-saalumam;
- Dexug Senegaal gi, fi mu janook réewum Mali, ci penkoom;
Ay goxam
SoppiGinnaaw bi, bi ñu defee Tunduw Kéedugu Diiwaan bu mat sëkk ci 2008, Péncum Réewum Senegaal la ngi ko def ci 1 diggi-gammu ci 2008, diiwaan bi ñaari Tund rekk la am:
Xool it
SoppiLëkkalekaay yu biti
Soppi- (en)Statistiques Geo Hive
- (fr)Conseil régional de Tambacounda
- (fr)Situation économique régionale de Tambacounda, édition 2005 (juin 2006)
| |||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |