Séddaliinu yoriinu Senegaal

  • la ko dale ca 2008, Senegaal mi ngi nekk 14 diiwaan[1].
  • 35 tund ñoom ci séen bopp dañu leen a séddale ci 92 ndiiwaan.
  • dëkk yi yor yenn rëyaay yi dañu leen a séddale ci dëkkani ndiiwaan, 43 ci mboole-séen. Ndakaaru, ci misaal, yor na ci 19.
  • Dëkk yu digg-dóomu yi ñu def leen ay Dëkkaan, Ñoom nag 67 lañu ci mboolee-séen.
  • Yeneen barab yi ay dëkk-dëkkaan lañu yu ñu boole ci ay gox-goxaan, yoy àgg nañu ci 324 ci 2007.

Dëkkiin wi

Soppi
Bennte gu yoriin (unité administrative) askan[2]
  Senegaal 9802775
Diiwaanu Ndakaaru 2411528
Tunduw Ndakaaru 919683
Ndakaaru 919683
Tunduw Pikin 1206540
Géejawaay 452168
Pikin 754372
Tunduw Tëngéej 285305
Barñi 38739
Tëngéej 165274
Sibexotaan 16316
Diiwaanu Njaaréem 930008
Tunduw Baamby 256482
Bambey 26993
Tunduw Njaaréem 235845
Njaaréem 112950
Tunduw Mbakke 437681
Mbakke 64824
Diiwaanu Fatik 639075
Tunduw Fatik 254417
Jofiyoor 6495
Fatik 39166
Tunduw Funjunj 192243
Funjunj 4387
Sóokóon 12995
Passi 4798
Tunduw Gosaas 192415
Gosaas 10391
Nginngineew 14848
Kawóon 2808
Diiwaanu Kawlax 1128128
Tunduw Kafrin 441779
Kafrin 27177
Kungéel 13707
Tunduw Kawlax 423710
Kawlax 243209
Ganjaay 6442
Ndóofaan 8724
Tunduw Ñooro gu Rip 262639
Ñooro 18331
Bennte gu yoriin way-dëkk
. .
Diiwaanu Koldaa 834753
Tunduw Koldaa 264671
Koldaa 61770
Tunduw Séeju 398615
Gudomp 9263
Marsaasum 8363
Séeju 19227
Tunduw Wilingara 171467
Wilingara 22496
Diiwaanu Luga 559268
Tunduw Kebemeer 152185
Kebemeer 15248
Tunduw Lingeer 191072
Daara 15322
Lingeer 11405
Tunduw Luga 216011
Luga 86663
Diiwaanu Maatam 423041
Tunduw Kanel 171918
Kanel 8997
Semme 4492
Wawund 8041
Tunduw Maatam 291555
Maatam 11676
Wurosóogi 8887
Ciloñ 5043
Tunduw Raneru 41660
Raneru 1262
Bennte gu yoriin way-dëkk
. .
Diiwaanu Ndar 863440
Tunduw Dagana 404518
Dagana 25142
Risaatool 70465
Ndar 154496
Tunduw Podoor 167367
Podoor 7610
Njum 5157
Diiwaanu Tambaakundaa 530332
Tunduw Bàkkel 152933
Bakkel 9882
Tunduw Keedugu 75331
Keedugu 15068
Tunduw Tàmbaakundaa 302068
Tàmbaakundaa 69574
Diiwaanu Cees 1348637
Tunduw Mbuur 429038
Jiwaalo 32401
Mbuur 148985
Ngeexoox 6282
Caajaay 7635
Tunduw Cees 540078
Xombal 13445
Puut 27628
Cees 273599
Tunduw Tiwaawon 379521
Mexe 17375
Tiwaawon 43612
Diiwaanu Siggcoor 557606
Tunduw Biñoona 224617
Biñoona 35895
Conk-Esil 7721
Tunduw Usuy 49871
Usuy 6308
Tunduw Siggcoor 283118
Siggcoor 216971

Karmat

Soppi
  1. Yax ba péncum réew ci 1 février 2008 [1]
  2. gongikuwaay: direction sénégalaise de la Prévision et de la Statistique/Division des Enquêtes démographiques et sociales, janvier 2001

Xool it

Soppi

jukki yu ci aju

Soppi

Téerekaay

Soppi
  • (fr) Giorgio Blundo, « La corruption comme mode de gouvernance locale : trois décennies de décentralisation au Sénégal », Politique africaine, 2000, n° 199
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
  • (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal, Dakar, Ministère du Plan, 1967, 705 p. (Thèse de 3 cycle publiée)
  • (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal. Complément pour la période des origines à 1965 et mise à jour 1966-1973, Paris, Mouton, 1977, 637 p.

Lëkkalekaay yu biti

Soppi