Ndiiwaani Senegaal

Ndiiwaani Senegaal yi ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu Senegaal.

Ndiiwani Senegaal

Ndiiwaan nag ag nekkte (entité) gu suuf la, gu ñuy faral di gis ci réew yiy làkk wu-fraas. Soo demee ci ñiy làkk wu-angalteer weneen dogiin nga fay fekk.

Ci Senegaal, ndiiwaan yi dinañu leen waññi ci lim bu tollook 92 ci 2007.

Taariix

Soppi

Limu tund yi (nosu topp abajada)

Soppi
 
Ndiiwaani Bàkkel
  • Bala
  • Jaawara
  • Gudiiri
  • Kidiira
 
Ndiiwaani Bambey
  • Baba Garaas
  • Lambaay
  • Ngoy
 
Ndiiwaani Biñoona
  • Jululu
  • Sinja
  • Tenduk
  • Tengori
 
Ndiiwaani Cees
  • Nooto
  • Puut
  • Cenaba
 
Ndiiwaani Dagana
  • Mban
  • Roos Beeco
 
Ndiiwaani Fatik
  • Jaxaaw
  • Fimla
  • Ñaaxar
  • Taatagin
 
Ndiiwaani Funjunj
  • Jilloor
  • Ñoojoor
  • Tubaakuta
 
Ndiiwaani Gosaas
  • Kolobaan
  • Kawóon
  • Waajur
 
Ndiiwaani Géejawaay

Géejawaay moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 5 dëkkani ndiiwaan

 
Ndiiwaani Kafrin

Dogiinu tund wi dañu koo soppi gannaaw sosug tunduw Kungeel ci 2006.

Kon mu des :

  • Birkilaan
  • Maleem-Odaar
  • Nganda
 
Ndiiwaani Kanel
  • Kanel
  • Seeme
 
Ndiiwaani Kawlax
  • Ganjaay
  • Ndenjeng
  • Ndóofaan
 
Ndiiwaani Kebemeer
  • Daaru Musti
  • Ndand
  • Sagata
 
Ndiiwaani Kéedugu
  • Bandafasi
  • Fongolimbi
  • Salemata
  • Saraya
 
Ndiiwaani Koldaa
  • Dabo
  • Julaacolon
  • Medina Yoro Fula

Mi ngi judd ci 2006 (amul lonkoyoon bu jàppandi nii-nii)

 
Ndiiwaani Lingeer
  • Barkeji
  • Daara
  • Dooji
  • Yang-Yang
 
Ndiiwaani Luga
  • Kër Momar Saar
  • Kokki
  • Mbejeen
  • Sakal

Ndiiwaanu Raawo, biy feeñ ci lonkoyoon bi, ci tunduw Ndar la bokk 2002 ba tay.

 
Ndiiwaani Mbuur
  • Fisel
  • Ngeexoox
  • Caajaay
  • Jiwaalo
  • Añam Ciwol
  • Ogo
 
Ndiiwaani Mbakke
  • Kayel
  • Ndam
 
Ndiiwaani Ndakaaru

Ndakaaru moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 19 dëkkani ndiiwaan.

 
Ndiiwaani Njaaréem
  • Ndindi
  • Ndulo
 
Ndiiwaani Ndar

Gannaaw dogaat ga waraaloon juddug Diiwaanu Maatam, tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu

  • Raawo
 
Ndiiwaani Ñooro gu Rip
  • Medina Sabax
  • Pawoskoto
  • Wak Nguna
 
Ndiiwaani Pikin

Pikin moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la

Ñu séeddale ko ci 16 dëkkani ndiiwaan.

  • Pikin
 
Ndiiwaani Podoor
  • Kas-Kas
  • Njum
  • Salde
  • Cile Buubacar

Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Welingara

 
Ndiiwaani Séeju
  • Bunkiling
  • Jaatakunda
  • Jend
  • Marsasum
  • Tanaaf
 
Ndiiwaani Siggcoor
 
Ndiiwaani Tambaakundaa
  • Kumpentum
  • Kusaanaar
  • Makakolibantang
  • Misiira
 
Ndiiwaani Tënjéej

Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Sebixotaan, moom ci boppam ñu séddale ko ci 3 dëkkaani Ndiiwaan.

 
Ndiiwaani Tiwaawon
  • Meewaan
  • Merina Daqar
  • Ñaaxeen
  • Pambal
 
Ndiiwaani Usuy
 
Ndiiwaani Welingara
  • Bookoto
  • Kunkan
  • Pakur

Xool it

Soppi

Lëkkalekaay yu biir

Soppi

Lëkkalekaay yu biti

Soppi

Téerekaay

Soppi
  • (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)