Diiwaanu Njaaréem

(Yoonalaat gu jóge Diiwaanu Jurbel)

Diiwaanu Jurbel benn la ci diiwaani Senegaal yi. Amul benn ubbeeku ci géej gi.

Diwaanu Jurbel ci lonkoyoonu Senegaal

Mi ngi yem ci diiwaani Cees ak bu Fatik ci bëj-gànnaaram, ci bëj-saalumam ci diiwaani Cees ak bu Fatik, ci penkoom ci diiwaani Fatik ak bu Luga, ci sowwam ci diiwaanu Cees. Am na lu tollu ci 1 049 954 ciy way dëkk te yaatoo 4 359 km2

Diiwaan bi mi ngi nekk tembe fa nguuru bawol ga nekkoon.

Ay tundam

Soppi
 
Tundi diiwaan bi

Xool it

Soppi

Téerekaay

Soppi
  • (fr)Ibrahima Dieng, L'action des services sanitaires dans la région de Diourbel, Dakar, École nationale d'Administration, 1968, 151 p.
  • (fr)J. Gard et Raymond Mauny, « Découverte de tumulus dans la région de Diourbel (Sénégal) », Notes Africaines, IFAN, Dakar, IFAN, 1961, n° 89, p. 10-11
  • (fr)Ismaïla Lo, « La région de Diourbel », Sénégal d'Aujourd'hui, n° 16, 1970, p. 23-30

Lëkkalekaay yu biti

Soppi
  14 Diiwaani Senegaal  

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·