Dëkkaani ndiiwaani Senegaal

Dëkkaani ndiiwaani yi, ci Senegaal, ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu réew mi. ci 2007 lim bu toll 43 lañu.

Dëkkaani ndiiwaani Ndakaaru yi

Taariix Soppi

Yokkug nit ñi dëkk ci Ndakaaru moo dem ba àgg ci benn dayoo bi, ba tax genn kilifag dëkk rekk manatu koo yor, tax sosug geneen nekkte gu gën a suufe waroon. Kon lii moo tax ci 1996 ñu séddale tunduw Ndakaaru ci 43 dëkkaani ndiiwaan, ni dëkk bu Paris.

Dogiin Soppi

43 Dëkkaani ndiiwaani yi dañu leen séddale ci 4 tund yi:

Xool it Soppi

Lëkkalekaay yu biir Soppi

Téerekaay Soppi

  • (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)

Lëkkalekaay yu biti Soppi