Séddaliinu yoriinu Senegaal
(Yoonalaat gu jóge Fii)
- la ko dale ca 2008, Senegaal mi ngi nekk 14 diiwaan[1].
- 35 tund ñoom ci séen bopp dañu leen a séddale ci 92 ndiiwaan.
- dëkk yi yor yenn rëyaay yi dañu leen a séddale ci dëkkani ndiiwaan, 43 ci mboole-séen. Ndakaaru, ci misaal, yor na ci 19.
- Dëkk yu digg-dóomu yi ñu def leen ay Dëkkaan, Ñoom nag 67 lañu ci mboolee-séen.
- Yeneen barab yi ay dëkk-dëkkaan lañu yu ñu boole ci ay gox-goxaan, yoy àgg nañu ci 324 ci 2007.
Dëkkiin wi
Soppi
|
|
|
Karmat
Soppi- ↑ Yax ba péncum réew ci 1 février 2008 [1]
- ↑ gongikuwaay: direction sénégalaise de la Prévision et de la Statistique/Division des Enquêtes démographiques et sociales, janvier 2001
Xool it
Soppijukki yu ci aju
Soppi- Diiwaani Senegaal
- Tundi Senegaal
- Ndiiwaani Senegaal
- Dëkkaani ndiiwaani Senegaal
- Dëkkaani Senegaal
- Gox-goxaani Senegaal
- Dëkki Senegaal
Téerekaay
Soppi- (fr) Giorgio Blundo, « La corruption comme mode de gouvernance locale : trois décennies de décentralisation au Sénégal », Politique africaine, 2000, n° 199
- (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
- (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal, Dakar, Ministère du Plan, 1967, 705 p. (Thèse de 3 cycle publiée)
- (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal. Complément pour la période des origines à 1965 et mise à jour 1966-1973, Paris, Mouton, 1977, 637 p.