Tërug Ndimbal gi ci Wikipedia

Xët wii da lay won lëkkalekaay yi ëpp njariñ ngir nga mana cëru te jang jëfandikoo Wikipedia. Dañ leen séddatle ciy xaaj yuy wax ci doxinu dal bi, ay baaxu Wikipedia ak ay àtteem yu ñuy wormaal, ci soppi xët yi, yokkug ëmbiitam ak melokaanu xaralay jimbulang.


Ngir man a cëru


Soppi jukki yi

Nooy soppee aw xët
Nooy mana indee say mbind ci jimbulang bi
Nooy sose aw Xët
Ngir sàkk xët wu bees (sa xëtu bopp, ab jukki, aw wàll ak yeneen) loolu lanuy faramfàcce ci bii jukki.
Man mbindin ngay jëfandikoo?
Fii ngay gise xàll yi gëna yaa, ci mbindin wu yomb wooy jëfandikoo ci xët yi ngay sos walla di ko nas ci Wikipedia
Nan ngay lëkkalee ay jukki ci seen biir?
Ni mu wutee ak yeneen jimbulang yi, Wikipedia day def nga mana jóge ci aw xët dem ci weneen ci anam wu yomb lool. Loolu laaj na, saa yooy soppi walla sàkk ab jukki, def ci ay lëkkalekaayi biir.
Nooy dugale lëkkalekaayi biti?
Ngir yenn jukki yi, man naa doon lu solowu yenn saa yi nga def ay lëkkalekaay yu biti yu lay yóbb ci yeneeni dal, yuy yokk ay xibaar ci li nga jota jukki.
Nooy dugale ab lëkkalekaay diggantelàkk?
Dafa am ay waa-wikipedia yu bari ci yeneen làkk. Nii la nuy dugale ay lëkkalekaayi diggantelàkk ci biir jukki yi, ngir jàngkat yi man koo am ci yeneen làkk.
Ay kàddu ci say coppite
Ay baat yu néew ci li waral coppite yi, loolu dina noppal waa wikipedia yi

Jëfandikukat

Caytu‎
ay xamale ci anami caytu yu jimbulang bi
sàqum jëfandikukat
Doonte doonul lu manut a ñàkk, bindu ngir mana cëru, waaye am na ay ngënéel yu jar a bàyyi-xel ci def ko. Xool leen nu ñuy bindóo.
Tànneefu Jëfandikukat
Léegi nga xam ne bindu nga ba noppi, man ngaa dugg ci samay tànneef soppi ko ci ni nga ko bëggee.
Ndimbal ci ay nataal
Fii di nañ la fi won nooy sosee am sàqum jëfandikukat, jaare ko ciy nataal
Xëtu jëfandikukat
ci sag bindu, am na aw xët wu ñu lay jagleel, foofu ngay bind dara ci yaw
Soppi turu jëfandikukat
Su fekkee sa turu jëfandikukat neexatu la, man nga koo soppi ci lu gaaw, leeral ni yaa ngi ci wii xët
Wikipedia Babel
fii ngay xamale yeneen waa wikipedia yi làkk yi nga dégg.

Masum Ibn Musa (xëtu waxtaanuwaay) 21 Nowembar 2019 à 13:37 (UTC)Répondre