Ndimbal ci ay nataal
ngir bindu bu yees walla duggu ci sam saq xoolal ndimbël lii nu def ci ay nataal ngir mu gën a jumb ci gan ñi
- fi gay cokk(clic) ngir dugg mba bindu
- ni gay def ba dugg ci sam sàq, fi gay cokk ngir bindu
- ni gay def ba sos am saq
man ga cee dugal sa loxo ngir mu yemb ndax lii di na tax mu gën a yomb ci gan ñi ndax jàgum bind(lire text) mi yombul ci ñépp.