Tabaski, (ci araab "sul-hajja" ذو الحج), tuddees na ko noonu ngir ne mooy boroom aj gi, ci la araab yi daan aji Màkka, ci la tabaski gi it nekk, moom nag bokk na ci weer yees wormaal .

Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Mooy weer wi mujj ci at mi.

Xew-Xew

Soppi
  • Ci lees di aj màkka,(ab ponk la ci lislaam war na jullit bu ko man),
  • Ci lees di Tabaski (rayi xar, bëy, nag, galeem, jokkug bokk, baloonte àq, jullig bër, ak yuni mel...)

Lëkkalekaay yu biti

Soppi
Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski