Maami-koor, (ci araab jumaadal aaxira جمادى الأخيرة), njëkk Lislaam (jumaadaa sitta ) lañu ko tudde woon, moom nag turam woowu mi ngi ko jële ci fiiroo gi mu defoon ak sedd bi, tur wa daal di koy topp (way).

Mooy juroom-benneelu weer ci at mi, di itam ñetteelu weer laataa koor gi.

Lëkkalekaay yu biti

Soppi
Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski