Xayma
Xayma yi ay xamuwaay la ñu yuy tabaxu ciy xalaat-jiital, ci ay fook naa, yu aju cig xellu. Doon na itam xam-xam biy seet aka biral ay xamteef, di itam ki leen di jangale.
Teerekaay
Soppi- Mbaye Faye, Nanu Xayma : Mathématiques modernes en langue nationale wolof à l’usage des opérateurs en alphabétisation, des élèves et des enseignants alphabétisés en wolof, 2006.
- Institut des langues nationales, Baatalu xayma, nasaraan ak wolof / Lexique des mathématiques, français-wolof, Nouakchott (Gànnaar), 1997.
Xam-xam | ||||
Gëstubiddiw | Jëmm | Paj | Saytubiddiw | Simi | Xam-xamu suuf si ak jawwu ji | Xayma | ||||
Jokkoosoryante | Xaralaymbëj | Doolerandu | Kàttan | Xam-xamu nosukaay | Mbëjfeppal | ||||
Diine | Melosuuf | Wërlaay | Nit | Yoon | Koom-koom | Taariix | Xeltu | Kàllaama |