Melosuufug Kamerun
Kamerun am réewu diggu Afrig la, jëmmam dafa mel ne ab ñettikoñ, rëye na 475 442 km², 98,8% di suuf, 1,2% ndox la, di 42u réew mi ëpp ci àdduna bi, am na it 402 km ci tefes.
Ay digam
SoppiRéewum Niseeriyaa moo ko féete sowwu, Mbàmbulaanug Atlas gi, Gineg yamoo gi, Gaboŋ ak Kongóo-Brasaawiil nekk ci bëj-saalumam, Réewum Diggu Afrig ak Cadd nekk ci penku, dexub Cadd bi ci bëj-gànnaar.
Xool it
Soppi
Xool it Wikimedia Commons
|
Melosuufug Afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkinaa Faaso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Bennoo yu Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eriitere • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Gine • Gine-Bisawóo • Gineg yamoo • Keeñaa • Lesoto • Liberiyaa • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeriyaa • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome-ak-Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togo • Tuniisi • Sambi • Simbaawe