Melosuufug Alseeri
Alseeri doon na réew mu bariy doj. Ci bëj-gànnaar gi, boo jàppee penku jëm sowwu gépp ab càllaleeb ay doj ñoo fa ne, am na it wàll gu bari ci tàkkug Sahara gi. Ñi ngi koy boole ci Bëj-gànnaaru Afrig, di 11u réew mi gën a réy ci àdduna bi. réeyaayam toll ci 2 381 741 km², ma na 998 km ci tefes.
Ci bëj-saalum mi ngi feggook Mali, ak Gànnaar, ak Niseer, ci penku mi ngi taqalook Tiniisi, ci sowwu Nguuru Marook, ci bëj-gànnaar mi ngi yem ci Géej gu Diggu gi. Pegg gi mu amal ak yenee réew yi toll na ci 6 343 km.
Melosuufug Afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkinaa Faaso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Bennoo yu Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eriitere • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Gine • Gine-Bisawóo • Gineg yamoo • Keeñaa • Lesoto • Liberiyaa • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeriyaa • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome-ak-Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togo • Tuniisi • Sambi • Simbaawe