Melosuufug Angolaa
Angolaa mi ngi nekk ci diggante 4°22′ ak 18°03′ ci tus-wu-gaar wu bëj-saalum ak 11°41′ ak 24°05′ ci tus-wu-taxaw wu bëj-gànnaar. Am na 1 300 km ci tefe, réye 1 246 700 km² soo ci boolee Kabinda.
Mi ngi fegoo ak Kongóo-Brasaawiil ci bëj-gànnaar, ak Kongóo-Kinshasa ci bëj-gànnaar-penku, ak Saambi ci bëj-saalum-penku, ak Namibi ci bëj-saalum, ak Mbàmbulaanug Atlas ci sowwu. Pegg gi mat na
Melosuufug Afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkinaa Faaso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Bennoo yu Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eriitere • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Gine • Gine-Bisawóo • Gineg yamoo • Keeñaa • Lesoto • Liberiyaa • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeriyaa • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome-ak-Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togo • Tuniisi • Sambi • Simbaawe