Melosuufug Buruundi
Buruundi am réewu diwaanu Diggu Afrig la, rëye na 27,830 km², 25,650 km² suuf la, 2,180 km² di ndox.
Melosuufug jëmm
SoppiMi ngi digook Kongóo-brasaawiil ci lu mat 233 km ci sowwu, ak Ruwandaa ci 290 km ci bëj-gànnaar, lang ak Tansani ci guddaayub 451 km ci penku. Buruundi amul ubbeeku ci géej gi, waaye yi ci bëj-saalum-sowwu da ñoo lang ak déegub Tanganica bu rëy ba. Réew mi dafa nekk ci diggante ñaari mbandi ndox yu mag yii di Niil ak bu Kongóo
Xool it
Soppi
Xool it Wikimedia Commons
|
Melosuufug Afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkinaa Faaso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Bennoo yu Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eriitere • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Gine • Gine-Bisawóo • Gineg yamoo • Keeñaa • Lesoto • Liberiyaa • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeriyaa • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome-ak-Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togo • Tuniisi • Sambi • Simbaawe