Sowwu Tugal

Sowwu Tugal benn la ci diwaani Tugal yi, waaye tekki gi ñu ko jox taxu kaa jub. da ñuy jàpp ne mi ngi toll ci diggante Mbàmbulaanu Atlas yem ci peggu Bëj-saalumu Tugal ak Penku Tugal.

Suwwu Tugal ci lonkoyoonu àdduna bi

Waaye ci lu ëpp da ñuy boole Diggu Tugal ak Bëj-gànnaaru Tugal ci Sowwu Tugal. Soo nee waa sowwu dafa mel tugal gépp ngay wax, ba mu des gu penku. Kon ay peggi Sowwu Tugal leerul

Gis-gis yi ñuy jàppee sowwu tugal da fay wuute.

Bu njëkkModifier

Ay réewamModifier

Bii gisin moo ngi judd ci ñaari dank (bu sowwu ak bu penku) yi juddoo ci xare bu sedd bi.

Ñaareel biModifier

 
Gisin bu Kureelu Mbootaayu Xeet yi (KMX)

Sunu xoolee ni ko Kureelu Mbootaayu Xeet yi jàppe réew yi fa ne ñooy Faraas, Almaañ, Beljik,...


Diwaani Tugalasi
  Asi      Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End
Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri
Tugal      Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal 
Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi