Penku gu Jege
Penku gu Jege su ñu koy wax mooy diiwaan bu melosuuf bi araab yi dëkke, di tambalee ci pegg bu penku gu Géej gu Diggu gi ba ci Iraak. Moo taqaloo ak réew yi nekk ci Penku gu Diggu gi, féete ko penku, di: Iraan, Afganistaan, Pakistaan (Di yemoo ak baatu waa faraas bi di Moyen Orient ak bu waa angalteer bi di "Middle East").
Réew yi
SoppiDiwaani Tugalasi | |||
Asi | Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri | ||
Tugal | Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi |