Bëj-gànnaaru Tugal

Bëj-gànnaaru Tugal mooy wàll gu Bëj-gànnaar gu goxu Tugal. ni nuy xoolee Bëj-gànnaaru Tugal daa bariy fànn.

réewi Bëj-gànnaaru Tugal ci gisiin gu néewal gi mooy yolet gu ñor gi, Gisiin gu yaa gi mooy gu leer gi

Gisiin wu néewal gi Soppi

Yii ñooy réew yi fa ne:

Ñii la ñuy woowee Réewi bëj-gànnaar yi

Gisiin wu yaa wi Soppi

Yii ñooy réew yi fa ne:

Gisiin wu MR Soppi

Su ñu sukkandikoo ci ni ko Mbootaayu Réew yi gisee, Yii ñooy réew yi ne ci Bëj-gànnaaru Tugal:

Diwaani Tugalasi
  Asi      Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End
Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri
Tugal      Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal 
Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi