Lusaka

dëkku réewum Zambi


Lusaka mi ngi nekk péeyu réewum Saambi ci bi muy am tembteem ci 1964, Sancaan yu waa-tugal yee ko sos ci atum 1905 ci ba ñuy defar yoonu weñ wi.

Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Lusaka
Skyline of {{{official_name}}}
Réew  Saambi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
15° 25′ 0″ Bëj-saalum
     28° 17′ 43″ Penku
/ -15.41667, 28.29528
Kawewaay 1300 m
way-dëkk 2 000 000 nit
atum way-dëkk 2 005
Barabalub Lusaka
Mbeddum Lusaka