Luanda (bu njëkk São Paulo da Assunção de Loanda) ab dëkkub bëj-saalumu Afrig la, di itam péeyu réewum Angolaa. Féete ci tefesu Afrig gu mbàmbulaanug Atlas gi, Luanda mooy waax wi ëpp ci Angolaa gépp

Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Luanda
[[image:|325px|none|alt=|Skyline of {{{official_name}}}]]
Réew  Angolaa
Tund Luanda
way-dëkk 7 000 000 nit
atum way-dëkk 2 009
barabalu Luandaa ci lonkoyoonu Angolaa

Dëkkiin Soppi

Limu nit ñi dëkk Luanda ci at yi:

  • 1815 : Luanda amoon na 18 000 way-dëkk,
  • 1900 : 20 000
  • 1934 : 18 000
  • 1940 : 61 000
  • 1950 : 137 000
  • 1975 : 600 000 (atum tembteg Angolaa)
  • 1987 : 1 136 000
  • 1991 : 2 000 000 (njeextalu xar ba)
  • 2005 : 2 776 000
  • 2008 : +6 000 000 way-dëkk
  • 2009 : +7 000 000 way-dëkk