Bëj-saalumu Afrig
Xët wii dafa nekk ci yoonu ndefaru. Sag cëru man na cee am solo! |
Bëj-saalumu Afrik moo ëmb barab yi nekk ci Bëj-saalumu allub yemoo gu Afrik.
Dañ ciy boole tamit duni Afrik yi nekk ci Bëj-saalum-sowu mbàmbulaanu waa-End ci wetu Madagaskaar ak duni Afrik yi ci Bëj-saalum-penku mbàmbulaanu Atlas.
Askani Xoysan ñoo fa njëkk a dëkk, ci li ci tegu la bantu yi ñéw. Ci jamono gi waa tugal aakimoo diwaan bi, lañ seddale réewi tayam yi.
Doon na diwaan bu am-alal te suufam naggu lool mbay. Rèew mi gën a jëm-kanam ci Afrik, fa la ne rawatina muy Réewu Afrik gu Bëj-saalum
Séwógaraafi
SoppiJuroomi Réew ñoo nekk ca diwaan boobu:
- Botswana
- Lesoto
- Namibi
- Afrik gu Bëj-saalum
- Eswatini
- Malawi
- Madagaskaar
- Mosambik
- Saambi
- Móoris
- Komoor
- Simbaawee
Diwaani Afrig | |||
Diwaani KMX: Diggu Afrig · Penku Afrig · Bëj-gànnaaru Afrig · Bëj-saalumu Afrig · Sowwu Afrig Yeneen diwaan: Ginne · Bejjenu Afrig · Maghreb · Sahel · Afrig gu bëj-saalumu-Sahara · Sudaan |