Bene

(Yoonalaat gu jóge Benin)
Réewum Benin
Raaya bu Bene Kóót bu aarms bu Bene
Barabu Bene ci Rooj
Barabu Bene ci Rooj
Dayo 112 622 km2
Gox
Way-dëkk 10 448 647 (2015) nit
Fattaay 91 nit/km2
Xeetu nguur
- Njiitu Réew
- Njiitu Jëwriñ
-
Yayi Boni
-
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Péy ak rëddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
Porto-Novo
Làkku nguur-gi Nasaraan
Koppar Franc CFA (XOF)
Turu aji-dëkk -Bene-Bene
-Sa-Bene
Telefon
Lonkoyoon bu Bene
Lonkoyoon bu Bene   

Benin (Republik bu Benin) : réewu Afrig.

  • Lii Ab Sémp rekk la man ga cee dugal sa loxo ndeem am ga ci xam-xam

Melosuuf

Soppi

Bene aw rëdduw suuf wu sew la, nekk ci diggante yamoo gi ak Gëwéelub Sànkar bi. Rëddu tus-wu-gaar wu bene mi ngi ci diggante 6°30'bëj-g ak 12°30'bëj-g, tu-wu-taxawam moom mi ngi ci 1° P ak 3° 40'P. Ay digam ñoo ngi yem ci Togóo ci sowwu, yem ci Burkina-faso ak Niseer ci bëj-gànnaar, ci Niseeriyaa ci penku, janook mbàmbulaanug Atlas gi ci bëj-saalum. Mi ngi am yaatuwaay bu tollu ci 112.622 yu kaare. Bene ngi bawoo ca dexug Niseer gi ci bëj-gànnaar yem ci mbàmbulaanug Atlas ci bëj-saalum ci ag tallalug 700 km. Diggante bi gën a guddu ci réew mi 325 km la.

Taariix

Soppi
  Ngir Xóotal, yëral bii jukki ci Taariixu Bene.

Lëkkalekaay yu biti

Soppi
  • (en) ICJ Judgment over the Benin-Niger boundary dispute, 12 July 2005 [1]
  • (en) Fabio Spadi (2005) The ICJ Judgment in the Benin-Niger Border Dispute: the interplay of titles and ‘effectivités’ under the uti possidetis juris principle, Leiden Journal of International Law 18: 777-794 [2]



  Réewi afrig  

Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkina Faso • Buruundi • Cadd • Ecoopi • Eritere • Eswatini • Gaambi • Gaboŋ • Gana • Gànnaar • Ginne • Ginne Bisaawóo • Ginne gu Yemoo • Isipt • Jibuti • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Keeñaa • Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Lesoto • Libeeria • Libi • Madagaskaar • Malawi • Mali • Marook • Móoris • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeria • Ruwandaa • Saambi • Sahara gu Sowwu • Sao Tome ak Principe • Senegaal • Seysel • Simbaawee • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Sudaan gu Bëj-saalum • Tansani • Togóo • Tiniisi • Ugandaa