Bés
Bés bi mooy diir bi jant bi di fenk ba ba muy sàngu; diggante ñaari guddi, jamono bi ceeñeeri jant bi di leeral asamaan si. Mi ngi door xaajaguddi, guddaayam a ngir aju ci jamonoy at ji nga ne ak tus-wu-gaar wi nga toll. Bés bi man naa mat 6 weer ca dotti Suuf si. Bési ayubés bi ñooy: altine, talaata, alarba, alxamis, ajjuma, gaawu ak dibéer.
Xool it Wikimedia Commons
|