Jant (junj: ☉) bi mooy biddiwu sunu nosteeg jant. Ci li ko wër la Suuf si di warangiku, am na yeneen juroom-ñaari àdduna, ak kuusi àdduna aki xeer yu réy. Kàttanu ceeñeer gi jant biy àggal ci Suuf si moo tax dund man faa am; kàttan googu day nu man a am ndox ci nekkinu yullaakon, tax it gañcax gi man a jot ci naaj wi mu soxla ngir seenug dund

Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Jant