Angolaa

(Yoonalaat gu jóge Angoolaa)

Angola (foor wu gudd: Republik bu Angola; ci portugais: República de Angola) réew la mu nekk ci bëj-gànnaaru Afrig, féete ak Republik Demokaratik bu Kongo ci nord ak gannaar-penku, Republik Kongo ci nord-est ( jaare ci Cabinda enclave), Zambie ba ci penku-sud-est ak Namibia ci bëj saalum.[1]Portugal moo kolonise réew mi ci 1575, ñu weccoo nguur gi ci diiru ñeenti xarnu, muy koloni, province bu nekk ci bitim réew ak etaa bu Empire Kolonial bu Portugal.  Ci atum 1961, xare moomel sa bopp tàmbali, loolu waral dooley koloni yi di xeex ak ay way-fippu yu bari yu doon xeex kolonisasioŋ.  Réew mi moom boppam ci 1975, muy republik kominist bu benn pàrti ci ndigalu Fenomen Populaire ngir Moom Angola (MPLA).  Ginaaw loolu xeex civil tàmbali ci saasi, muy bokk ci guerre froide, diggante nguuru MPLA ak yeneen mbooloo yuy xeex ngir moom seen bopp, rawatina Mbootaayu Réew mi ngir moomel sa bopp ci Angola (UNITA).  Ak liñu taxawal sistemu pàrti yu bari ci 1992, geer civil bi jeex ci 2002, ba leegi MPLA mooy pàrti bi gëna am doole, doonte dafa soppi ngëmam joge ci komunism dem ci sosialismu demokratik.

Réew mi ñeenti boor la, mingi féete ci diggante Afrig bu bëj-saalum bi ñuy làkk farañse ak Afrig bëj-saalum bi ñuy làkk tubaab.  Mooy ñaareelu réew biy làkk portugais ci yaatuwaayam, ñaareel bi ci askan wi.  Bi muy koloni Portugais bu njëkk, mingi bokk ci Askanu Réew yiy Lakk Portugais.

Réewum Angola
Raaya bu Angolaa Kóót bu aarms bu Angolaa
Barabu Angolaa ci Rooj
Barabu Angolaa ci Rooj
Dayo 1,246,700 km2
Gox
Way-dëkk 25,789,025 (2014) nit
Fattaay nit/km2
Xeetu nguur
- Njiitu Réew
- Njiitu Jëwriñ
-
João Lourenço
Bornito de Sousa
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Péy ak rëddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
Luwandaa
Làkku nguur-gi Wu-Portigaal
Koppar Kwanza (AOA)
Turu aji-dëkk Angola-Angola
-Sa-Angola
Telefon
Lonkoyoon bu Angolaa
Lonkoyoon bu Angolaa   

Angolaa (Réewum Angolaa) : réewu Afrig.

  • Lii ab tambali rekk la man ga cee dugal sa loxo ndeem amga ci xam-xam.


Réewi afrig

Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkina Faso • Buruundi • Cadd • Ecoopi • Eritere • Eswatini • Gaambi • Gaboŋ • Gana • Gànnaar • Ginne • Ginne Bisaawóo • Ginne gu Yemoo • Isipt • Jibuti • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Keeñaa • Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Lesoto • Libeeria • Libi • Madagaskaar • Malawi • Mali • Marook • Móoris • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeria • Ruwandaa • Saambi • Sahara gu Sowwu • Sao Tome ak Principe • Senegaal • Seysel • Simbaawee • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Sudaan gu Bëj-saalum • Tansani • Togóo • Tiniisi • Ugandaa

  1. Wikipedia français