Ubbi njël lu njëkk li


Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Xartum (ci araab al-Khartûm الخرطوم ñu man koo tekkee «ñoxub ñay») mooy péeyu réewum Sudaan, féete ci wetu Niil bu weex, bi jóge Ugandaa, ak Niil bu baxa, bi jóge Ecoopi.

Xartum الخرطوم
Réew Flag of Sudan.svg Sudaan
Tund al-Chartum
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
15° 36′ 27″ Nord
     32° 32′ 13″ Est
/ 15.60754, 32.53706
Kawewaay 382 m
way-dëkk 2 090 001 nit
atum way-dëkk 2 005
Ab talib Xartum