Can you please apply for bot status on this wiki? Thanks, Guaka 17:10, 17 June 2007 (UTC)



Jaajëf ci liggéey bu rafet bi, waaye boo manoon di jëfandikoo baatu Pénc ci barabu Republik: ndax Pénc day tekki bayaal bu yaatu bi nekk ci digg ab dëkk, waaye it day tekki li mbooloo mépp bokk, mu bawoo ci maanaam mi pénc ame, muy yëfi mbooloo, naka noonu "république", être républicain wormaal mbooloo mi nangu ne ci pénc mi nga bokk yaw rekk moomoo ko, nga séddoo kook ñoom ci yoon ak maandute. Kon pénc mooy taxaw taxawaayu République. Péncum Araab mu Siri --Abdu Xaadir Kebe 14 Oktoobar 2008 à 12:49 (UTC)

I don't speak Wolof, but looking at what this seems to be about: Robbot did not create the text that you are talking about, Robbot only added some interwiki links on the page. The text itself was created by Ji-Elle in 2006. - Andre Engels 17 Oktoobar 2008 à 12:15 (UTC)