bienvenue sur wikipedia en wolof. Tous tes contribitions seront bien accueillis. si tu as des questions tu peus les faire à n'importe quel utilisateur. je suis l'administrateur de ce wiki.

dala-jamm ci wikipedia ci wolof. Noo ngi bég ci sag mbindu. maay yorekat gu gii wiki. Man ngaa biral say laaj bepp aji jëfëndikoo bu fi nekk, ndax li ëpp solo ci bii ëtt mooy jappalante ak dimbalante. Yërël xetu Dalal-jamm gi. wasalaam --Ibou 28 juillet 2007 à 17:46 (UTC)


Hi! Can you translate this text onto Wolof?
Almazán is a municipality located in the province of Burgo, Castile and León, Spain.
Thanks. --Jeneme 13:45, 28 Oktoba 2007 (UTC)

joyeux noël

Soppi

merçi, joyeux noël et bon 2008 à toi aussi. ciao --Ibou 26 Tabaski 2007 à 00:32 (UTC)

Bataaxalu dalal-jàmm

Soppi

Dalal-jàmm / Bienvenue / Welcome , Jult !

 

(wo) Bataaxalu dalal-jàmm : dila nuyu Jult te dila dalal ci Wikipedia. Dila gërëm ci say cëru ci bii jimbulang. Su dee dangay làkk wolof, soxla nañu la lool ngir bind walla soppi ay jukki.; walla it, sag ndimbal ci wàllu xarala. Su fekke it dangaa soxla ndimbal walla dangaa ami laaj, saytul xët wii Ndimbal, man nga maa bind ci sama xëtu waxtaanuwaay, walla nga bind sa laaj ci Wikipedia:Pénc, ci xëtu waxtaanuwaay yi, dee fa xaatim say bataaxal, deel cuq ci   walla ngay bind ~~~~ ngir xaatim: dina tax, sa turu jëfandikukat ak taariix bi, feeñ ci sa wetu bataaxal. Liggéeyal ak jàmm!

 

(fr) Message de bienvenue : Salut Jult et bienvenue sur Wikipédia. Merci pour tes contributions sur cette encyclopédie libre. Si tu parles la langue wolof, nous avons extrêment besoin de toi pour éditer les articles; sinon, nous avons toujours besoin de ton aide pour l'assistance technique. Si tu as toi-même besoin d'aide ou si tu as des questions, consulte Ndimbal, demande-moi sur ma page de discussion, ou pose ta requête sur Wikipedia:Pénc. Sur les pages de discussion, signe tes messages en cliquant sur   ou en écrivant ~~~~ : ceci fera afficher automatiquent ton nom utilisateur et la date. Bonne continuation!

 

(en) Welcome message: Hello Jult and welcome to Wikipedia. Thank you for your contributions to this free encyclopedia. If you speak the wolof language, we highly need you to edit articles; if you don't, we always need your help for technical support. If you need help or for any question, check out Ndimbal, ask me on my talk page, or ask your question on Wikipedia:Pénc. Please remember to sign your name on talk pages by clicking   or using four tildes (~~~~): this will automatically produce your username and the date. Happy editing!

Guérin Nicolas (Xëtu waxtaanukaay) 7 Awril 2009 à 12:55 (UTC)Répondre