yaatuwaay kenn du ko wax fii, ndax yaatuwaay li muy tollool ci fr mooy largeur, bu ko defee guddaay di longueur , waaye Rëyaay lees di wax mooy na suuf sa sépp toll. Dankaloowaay deesu ko wax waaye ag fatt = densité --Abdu Xaadir Kebe (xëtu waxtaanuwaay) 29 Samwiye 2009 à 23:09 (UTC)


PArdon, est-ce que tu peux traduire ce phrase au français? Je ne l'entende pas. --Jult (xëtu waxtaanuwaay) 30 Samwiye 2009 à 09:32 (UTC)


Bonjour! Je vs remercier pour votre effort et contribution en ce qui concerne notre langue qui a besoin des bonnes personnes comme vs.

Concernant la traduction du phrase: J'ai dit on n'utilise pa ici "yaatuwaay" comme superficie, mais "rëyaay" parce que yaatuwaay signifie largeur tout comme guddaay signifie longueur. Rëyaay littéralement signifie grandeur, mais en géographie c'est superficie --Abdu Xaadir Kebe (xëtu waxtaanuwaay) 30 Samwiye 2009 à 10:42 (UTC)

fatt man nga koo wax dense, fattaay densité. --Ibou (xëtu waxtaanuwaay) 30 Samwiye 2009 à 18:54 (UTC)

Waaw loolu baax na fattaay moo gën = densité --Abdu Xaadir Kebe (xëtu waxtaanuwaay) 30 Samwiye 2009 à 20:50 (UTC)

Démarrer une discussion sur Warsaw

Démarrer une discussion
Revenir à la page « Warsaw ».