Waxtaan:Dencukaay
Dernier commentaire : 15 at ci ginaaw par Ibou
Ma lay ñaan ngir Yàlla, ngir yokk leerug sa mbind yi, ngay jëfandikoo xala yi () di ci dugal baat yu farãse yiy tekki yu wolof yi nga xam ne nàndeesagu leen lool, loolu de dina la def ngay kenn ci ñi ëpp solo ci ñiy bind ci wolof, te dina waral ñeneen ñi bëgg a roy ci yaw, ci di bind ci wolof, di ko man --Abdu Xaadir Kebe (xëtu waxtaanuwaay) 18 Awril 2009 à 18:37 (UTC)
- li tax du may dugal xala yi ci samay mbind mooy bépp baat bu ma fi dugal soo demee wikbaatukaay fekk ko fa. Te itam ci suufi xët yi def naa fa ab lëkkalekaay bu la fay jëme, loolu dina tax sax ku xamul woon wikbaatukaay xam ko léegi. Gis naa ne xala yi dañuy tilimal mbind mi, te wikbaatukaay looloo tax ñu sos ko. --Ibou (xëtu waxtaanuwaay) 10 Mee 2009 à 19:51 (UTC)