Tunis
Tunis (ci araab تونس ) mooy dëkk bi ëpp ci Tiniisi, mooy péeyu réew ma dale 20 sattumbar 1159 (di 5 koor 554 ci arminaatu jullit ñi). Nekk ci bëj-gànnaaru réew mi , ci dóoxub Tunis bi ko tàqaleek déegub Tunis bi. Ña fa dëkk waa-tunis lees leen di woowee, ci suuf su yaa la tëdd man ngaa daw 30 km laa ngay àgg ca anéer ba.
Tunis تونس | |
---|---|
Réew | Tiniisi |
Tund | al-Chartum |
Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
Kawewaay | 4 m |
way-dëkk | 728 453 nit |
atum way-dëkk | 2 004 411&Code_indicateur=0 301 007&Submit3=Envoyer delluwaay ((fr)) |
Rëyaay | 212,63 km² |
Fattaay | 3 425,9 nit/km² |
Dalub web | www.commune-tunis.gov.tn |
Mbeddum Habib Bourguiba ca Tunis | |