Sattumbar mooy juroom-ñeenteelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci latin september, jóge ci septem (juroom-ñaar), moo nekkoon juroom-ñaareelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar