Saara
(Yoonalaat gu jóge Sahara)
Saara : yay Afrig Saara ab màndiŋ la, mu ngi soxal Afrig gu bëj-gànnaar. Ak 9.200.000 km2, mooy màndiŋ bi gën a mag ci àddina si, te mooy ñetteelu màndiŋ bi gën a mag ci àddina si, gën a tuuti màndiŋ yi nekk ci Antartika ak bëj-gànnaaru Artiku rekk.
Xool it Wikimedia Commons
|