Niccolò Machiavelli
bindkat, xeltukat, aji-politig ju Itaali
Niccolò di Bernardo dei Machiavelli (Nikoloo Makiawelli)(3 mee 1469 – 21 suwe 1527) ab bindkat, xeltukat, aji-politig ju Itaali la woon.
Niki Leonardo Da Vinci, Machiavelli jàppe nañu ko kuy misaal dëgg-dëgg nitug yewwute. Bii tekki - ginnaaw ñu bari - di nanu xamal ci jëmm ji ak ci nitu mbind ki waaye du nu xamal ci ngérum machiaveli, mi dugg ci waxtaani bés yi di junj am xel mu yaa te ñaw waaye it di gaaw a ñaaw-xel, ami sikki-sakka ci lépp. Machiavelli jàppe nañu ko niki ki sos xam-xamu politig bu jamonoo bi.
Xool it Wikimedia Commons
|