Las Palmasu Kanaari gu Mag

dëkk bu nekk ci diiwaanu Las Palmas, Canary Islands, Espaañ


Las Palmasu Kanaari gu Mag ab dëkkaanu Tunduw las Palamas la, di itam péeyam teg ci nekk benn ci ñaari péeyi Duni Kanaari yi (réewum Ispaañ) beneen bi di Santa Cruz wu Tenerif tuxalug man-man gi ñeenti at yu ne lees koy amal. Mi ngi nekk ci bëj-gànnaar-penku Kanaari gu Mag mooy dëkk bi fa ëpp, tëdd ci suufus 10 km.

Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Las Palmasu Kanaari gu Mag
Skyline of {{{official_name}}}
Réew Raaya Ispaañ Ispaañ
Tund Tunduw Las Palmas
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
28° 09′ 00″ Nord
     15° 25′ 00″ Ouest
/ 28.150000, -15.416667
Kawewaay 8 m
way-dëkk 377 056 nit
atum way-dëkk 2 006
Rëyaay 100,55 km²
Fattaay 3 790,38 nit/km²
Dalub web www.laspalmasgc.es
Gisub Kaw

Dëkkiin

Soppi
  • 1991= 354 877
  • 1996= 355 563
  • 2001= 354 863
  • 2004= 376 953
  • 2005= 378 628
 
Jàngu bu Mag bu Kanaari