Nosteg jant

(Yoonalaat gu jóge Nosteeg jant)


Nosteg jant bi, ci xam-xamu saytubiddiw, mooy nosteg sunuy jawwu, li ko toggale di ab biddiw, jant bi ak mboolel yëfi asamaan yuy warangiku ci li ko wër ; juróom-ñatti jawwu yees firndeel ak seen 175 weer yu nu xam, juróomu jawwuy dàtt yi, ak miliyaari yaram yu ndaw yi (bokk ci yooyu jawwu yu ndaw yi ak pëndi diggante jawwu yi). Nosteg jant bi mingi bokk ci galaksi bi tudd Yoon wu Meewe

Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Nataal buy wone mbooleem cër yi ëpp solo ci sunu nosteeg jant, àdduna yi ci nekk
Nosteg jant

Jawwu yi nekk ci nosteg jant bi ñooy: Merkuur, Weenus, Suuf, Maas, Seres, Yupiter, Saturn, Uraanus, Neptuun, Eris, Pluton, Haomea, Makemake, Goŋgoŋ, Koawar ak Órkus.