Doxalukaay bu demandoodi wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Ibou (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Doxalukaay bu demandoodi''' ab xeetu doxalukaay bu mbëj la bu dawaan bu safaanu bu xél yu wëndeeluwaan bi yamul ak yu toolu bijjaakon buy wëndeelu bi lëmës yi nek...
 
Ibou (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Image:Stator and rotor by Zureks.JPG|thumb|Wëndeeluwaan (ci cammoñ) ak tekkaaralaan (ci ndijoor) bu ab doxalukaay bu 0,75 kW.]]
 
'''Doxalukaay bu demandoodi''' ab xeetu [[doxalukaay bu mbëj]] la bu [[dawaan bu safaanu]] bu xél yu wëndeeluwaan bi yamul ak yu [[toolu bijjaakon]] buy wëndeelu bi lëmës yi nekk ci tekkaaralaan bi jur. Maanaam amul ag demandoo ci ñaari gaawaay yi, benn bi moo raw beneen bi. Loolu moo ko wuutale ak [[doxalukaay bu demandoo]].
 
Bii xeetu doxalukaay manees na koo jëfandikoo niki ab [[jurukaayu mbëj]], ab [[safaanukaay]]. Waaye bariwul li ñu koy jëfandikoo ngir jóox [[kàttanu mbëj]] ndax li ko doxalukaay bu demandoo gënee ci wàll woowu.
 
==Melokaan==
Doxalukaay bi ci ñaari xaaj la séddaliku, benn bi di tekkaaralaan bi di xaaj bu taxaw bi, beneen bi di wëndeeluwaan bi doon xaaj biy yëngu. Tekkaaralaan bi dafa am ay bën-bën yu, lang ak wëndeeluwaan bi, di fi lëmës gi di jaar, waanaammaanaam wommatukaay yi dawaanu mbëj bi di jàll.
 
==Doxiin==
 
Dawaan biy jaar ci lëmës gu tekkaaralaan bi mooy juddal ab [[toolu bijjaakon]] buy wëndeelu, xélu wëndeelug tool bi mi ngi aju ci xélu dawaan biy dugg ci doxalukaay bi te jóge cig ndombo gu biti.
 
Kon lëmës gu tekkaaralaan bi dafay nekk ci biir ag wal guy soppiku. Toolu bijjaakon buy soppeeku bi mooy sabab juddug jenn [[doole ju mbëjdoxalukaay]], wëndeeluwaan bi su sóoboo ci boobu tool, sunu sukkandikoo ci [[àtteb Lorenz]], gis ab [[dawaanu mbëj]] buy judd ci wëndeeluwaan bi. Dawaan boobu mooy tax jenn doole ji feeñ ci wëndeeluwaan bi, di itam li koy xëcc muy topp walug bijjaakon bi, kon muy wëndeelu.
 
Kon turu demandoodi ngi jóge ci li wëndeelukaay bi manuta yam ak walug bijjaakon bi xél gi ñuy demee. Wuuteg xél gi nekk ci diggante wal gi ak wëndeeluwaan bi lañuy wax ''xélu tarxiis''. Xélu wëndeluwaan bi lañu wax ''xélu demandoo''
 
Lëkkaloo gi ci diggante xélu tarxiis gi, baraayu dawaan gi koy dundal ak limi seexi dott yi, mile mind moo koy fésal:
 
:<math>n_s = 60 \, \frac f p </math>
* '''<math>n_s</math>''' xelu toolu bijjaakon bi, ñu koy natt ci w/sim (wër ci simili), ñaata wër lay def ci simili bu nekk;
 
* '''f''' mooy baraay bi, ñu koy natt ci [[Hertz|Hz]];
 
* '''P ''' mooy limi seexi dott yi
ngir xayma tarxiis gi '''s'''
 
:<math>s = (\frac{n_s-n}{n_s})</math>
*'''n''' mooy xélu wëndeeluwaan bi.
 
Ci misaal, ab doxalukaay bu am ñetti seexi dott ''p'' (6 dott), bu baraayam ''f'' doon 50 Hz mi ngi am xélu demandoo 1000 wër ci simili.
 
[[Wàll:wuutuloxo yu mbëj]]
 
[[ar:محرك حثي]] [[bg:Асинхронен двигател]] [[ca:motor asíncron]] [[cs:Asynchronní motor]] [[da:Asynkronmotor]] [[de:Drehstrom-Asynchronmaschine]] [[en:Induction motor]] [[es:Motor asíncrono]] [[et:Asünkroonmootor]] [[fa:موتور القایی]] [[fi:Oikosulkumoottori]]
 
[[fr:Machine asynchrone]]
 
[[gl:Motor de indución]] [[hr:Indukcijski motor]] [[it:Motore asincrono]] [[ja:誘導電動機]] [[ko:유도전동기]] [[nl:Driefasige asynchrone motor]] [[pl:Silnik elektryczny asynchroniczny]] [[pt:Motor de indução]] [[ru:Асинхронная машина]] [[sh:Asinhroni motor]] [[sk:Asynchrónny motor]] [[sr:Асинхрона машина]] [[sv:Asynkronmotor]] [[uk:Асинхронна машина]]
Doxalukaay bi ci ñaari xaaj la séddaliku, benn bi di tekkaaralaan bi di xaaj bu taxaw bi, beneen bi di wëndeeluwaan bi doon xaaj biy yëngu. Tekkaaralaan bi dafa am ay bën-bën yu, lang ak wëndeeluwaan bi, di fi lëmës gi di jaar, waanaam wommatukaay yi dawaanu mbëj bi di jàll.