Joolaa (askan) wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
an
(Aucune différence)

Sumb bu 11 Fewriyee 2009 à 02:52

Joolaa genn giir la gu nekk Senegaal.

Jeunes filles lors du boukout de Baïla

Ñom Kaasamaas moye señi deuk. Ca yonu Imbratóor gu Mali, lañu dem deuk fofu. Mandé yi ño lene daq ca kasaamaas. Ca kawGinnebisaawoo, ña ga fa tamit.Baynuk yi jiité na ñu Joolaa yi ca kasamaas. Tabax nañu woon nguruu Kasanlaa. Joolaa yi ak Baynouk yi, dañu deukando ak Socés yi, Manjak yi, Pël yi. Ñom nëp ñow nañu ba paré.

Joolaa yi ca sowwu Kaasamaas lañi tabax señi nguruu, nguruu Banjal, nguruu Flup. Mbey cëp, napp, Samb, nan bunuk (Seuñ ca Wolof), mo done señi dund. Ba nopi, Mandé ñow nañu ca ñom ak señi buur mu tund Tiramakan Traoré. Ki, buuru jambaaru Sunjata Keyta lané woon. Sunjata Keyta mo tabax imbratoor gu Mali. Mom yoni na Tiramakan ca kaasamaas, ndax mu meunteu uuf deug bi ak Sénégal yëp, ca imbratooram. Mandé yi ak Tiramakan, tabax nañu nguruu Kaabu, ca kaasamaas yëp uuf nguruu Joolaa yi aki Baynuk. Nguruu bi dafa demone ba dexug Gaambi, Bajar, kaw Ginne-bisaawoo. Mandé yi ak Joolaa yi xéeru ñu, dañu nekone ca jaam, di deukando. Li moye tax Mansa (moye buur ca Mandé) yi kaabu, ca señi meen ay Joolaa lañu, wala ay Baynuk. Tamit Joolaa ak Mandé yi dañu jaaxaasé ba bokk ay sant ( Sonko, Sané, Mané, Jaby, Saña). Ba paré ca XVIeelu xarnu, tubap ño nañu Kaasamaas. Di beugeu Jaamlo nit ku ñul y fi nek, wa é Joolaa bëñ nañu, dañu xéér ak tubap ndax buguñu woon lolu. Ta ñom ken warul ta té nek jaamu kénene. Ca XXeelu Xarnu Aline Sitoë Jaata, bene Jigeen bokk ca Joola y, jogué Kabrousse, xéer na ak tubap yi defone canc, ndax ñom dañu bugone dieul Goor yi ak Cëp yi Joolaa ñu dund, yobu li yëp ca Tugal ndax fofu Guerre Mondial mo xeew woon, soxla ay jaambaar. Joolaa yi dañu béeñ. Aline dadjalé na goor yi yëp di xéer. Wa é ba paré tubap yi, dieul nañu Aline di ko yobu Tombuctu ca Mali, fofu la gën aduna.

Guide présentant des fétiches dans le musée en plein air consacré à la culture diola

Joolaa yi ca señi bop amna xet yu bari:

  • Foñi
  • Felup wala Kassa, ñom ño tabax nguruu Husuy
  • Ejamat, Joola yi Ginne-Bisaawoo
  • Yola
  • Elufayi
  • Eyunayi
  • Eblufayi
  • Selhek
  • Ajuat

Amna yénene xetu Joolaa. Señi sant: JéJyu, Jaata, Jamakune, Saña, Gujaby, Jaby, Koly, Bojan, Bajii, Mané, Sané. Biagui, Basséne, Ehemba, Sambu. Ca Joola amna ay jullit, ay katolig, wa é am nañu señi diiney bop. Tubap yi ño lene dugu ca diiney katolig, Wolof yi ak Pël yi ño lene dugu ca lislaam. Ca sénégal, ak Séeréer ya ño fi dakk bërëe.