Iraan
(Yoonalaat gu jóge Iran)
Republik Islaamik bu Iraan | |||||
| |||||
Barabu Iraan ci Rooj | |||||
Dayo | km2 | ||||
Gox | |||||
Way-dëkk | nit | ||||
Fattaay | nit/km2 | ||||
Xeetu nguur - Njiitu Réew - Njiitu Jëwriñ |
|||||
Tembte - Bawoo - Taariix |
|||||
Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
|||||
Làkku nguur-gi | |||||
Koppar | |||||
Turu aji-dëkk | |||||
Telefon | |||||
Lonkoyoon bu Iraan |
Iraan (Republik Islaamik bu Iraan) : Réew Asi. Iraan, deuk bu nekk si continent asie. deuk djullit shiit lagnu. Imam Khomeini mo def révolution si attum 1979. Mommoo guénné buur Mohamad Reza, mu samp république Islamique. Iran, réew mu nekk ci sowu Asie, mu juddoo ci jamonoy waa Perse. Te it Iran moo féeteek géej gu Caspienne ci penku, gaalu Oman ci penku, gaalu Golf Persique ci sudd, Turkmenistan ci penku-penku, Afganistan ci penku, Pakistan ci sowu-penku, Irak ci sowu ak Turkie, Aménie ak Azerbaïdjan ci sowu sowu. Te deuk bi dafa dajal ab diirub 1648195 kilómetri cuuraay.