Republik Islaamik bu Iraan
Raaya bu Iraan Kóót bu aarms bu Iraan
Barabu Iraan ci Rooj
Barabu Iraan ci Rooj
Dayo km2
Gox
Way-dëkk nit
Fattaay nit/km2
Xeetu nguur
- Njiitu Réew
- Njiitu Jëwriñ
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Péy ak rëddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw

Làkku nguur-gi
Koppar
Turu aji-dëkk
Telefon
Lonkoyoon bu Iraan
Lonkoyoon bu Iraan   

Iraan (Republik Islaamik bu Iraan) : Réew Asi. Iraan, deuk bu nekk si continent asie. deuk djullit shiit lagnu. Imam Khomeini mo def révolution si attum 1979. Mommoo guénné buur Mohamad Reza, mu samp république Islamique. Iran, réew mu nekk ci sowu Asie, mu juddoo ci jamonoy waa Perse. Te it Iran moo féeteek géej gu Caspienne ci penku, gaalu Oman ci penku, gaalu Golf Persique ci sudd, Turkmenistan ci penku-penku, Afganistan ci penku, Pakistan ci sowu-penku, Irak ci sowu ak Turkie, Aménie ak Azerbaïdjan ci sowu sowu. Te deuk bi dafa dajal ab diirub 1648195 kilómetri cuuraay.