Iniweersite Séex Anta Jóob

iniweersite ci Senegaal

Royuwaay:Iniweersite Séex Anta Jóob

Iniweersite Séex Anta Jóob (ISAJ), ñu xam ko itam ci iniweersite bu ndakaaru, moom rekk mooy iniwersite ci Ndakaaru, kàppitaalu Senegaal, ci Afrig Soowu Jant.

Kàggukaay i téere bu ISAJ ci atum 2005

Ñu ngi ko tuddee Seex Anta Joób di àntoropolog bu xam-xamam màcc ci jaar-jaari démb.

Ci kanamu iniweersite bi, mën nan ci jàng « Lux mea lex », « Leer a di sama yoon ». xew-xewu ubbite iniweersite bi amoon na ca atum 1959 Lewopool Sedaar Sengoor moo joxe bàkk bi[1].

Ci iniweersite bi, ngongo yi ñoongi bowoo ci bërëb yu wuute::

Daara Paj ngaa ngi dalal ay ndongo yu bawoo ca marok ak tinisii.

COUD moo sasoo dimbale, dalal mbooleem xeeti ndongo yu bees ci réew mi ak yeneeni réew, ci wàllum lekk, dalukaay ak lépp luy tàggat yaram ak aadaak cosaan. Ëtt bi yor lépp lu jëm ci iniweersite bi (COUD) moo yor wàllu ndimbal, teertu ndongo yii door a am BAC et ndongo doxandeem yi, wàllu lekk, dëkkuwaay ak lu jëm ci tàggat yaram ak aada ci biir ISAJ.

Jaar-jaar

Soppi
 
Buntu ISAJ
Dencukaay:Ëtt xam-xamu àtte ak politig.JPG
Ëtt xam-xamu àtte ak politig
 
Ëtt njàngum saafara ak njaayub garab, ak lépp lu aju ci feebar ak paju gemmiñ ca Faan

Iniweersite Séex Anta Jóob moo donnu daara ju doon jàngale wàllum paj ca jamonooy Afrique-Occidentale française.

Iniweersite bu Ndakaaru ñoo gi ko sanc Royuwaay:Date, xewu ubbitéefam amoon ci njiitalu kilifë yi ci Royuwaay:Date[2]. C'est l'une des plus anciennes d'Afrique de l'Ouest. De nombreux cadres sénégalais et étrangers y ont été formés.

Coppite jëm ci tur wa mi ngi am ci bésu Royuwaay:Date.

Ammbalemu ISAJ kii di Sëriñ Tewodoor Monod moo ko defar te niit bii di Lusiyeŋ Paay (1957 - 1960) nangowoon ko. Mingi bindoo ak ñaari kewel yu jàkkarloo gir wone meñental, sakkannaay, ay njureel. Ci ginaaw kewel gu nekk am na ay niitu yuy tekki leeraange ak xam-xam.

Lii di ndongo ci biir daara ji bari ba jéggi dayoo : lu tollook 69 000 ci atum 2011, ngir rekk 23 253 palaas Ndàmpaay ji tolloon na ci lu tolook de 13 à 32 miliyoŋ ci ëroo digante 2000 ak 2010, doyul ngir faj soxla yi. Ci at yii di ñëw, ISAJ jël na ndogal wàññi lifay duggu ci ay ndongo jaarale ko ab tànn tek gën a yook njàngale gu laajul ndongo yi teew. Mi ngi yaakaar tamit ci sosu iniwzzesite bu bees ci biir Ndakaaru[3].

Tëddin wi

Soppi

ISAJ am na juróom benni ëtt, ñeent daara ak fukk-ak-ñaari ëtt :

Këyitu ëtt yi

Soppi
  • Ëttu gëstu ak xarala (FST)
  • Ëttu ladam ak njangat ci doomu àdama (FLSH)
  • Ëttu gëstu yoon ak politig (FSJP)
  • Ëttu gëstu topato koom-koom (FASEG)
  • Ëttu gëstu ci xarala jëm ci njangale ak taggat (FASTEF)
  • Ëttu giy jàngale wallum pac, joxe sgarab ak saafara ak lépp lu ajju ci gemmiñ (FMPOS)

Këyitu daara yi

Soppi

Daaram bi mu jagleel njàng ak njàngaleem mpaj ak daara biy bi ñuy jàngalee xibaaru siiw nañu lool [3].

Këyitu ëtt yi

Soppi
  • Ëttu njàngaleek rataxal làkk yi bu Dakaar (CLAD)
  • Ëttu njàngaleek gëstu ci doole yi ñu mën a yeesalaat (CERER)
  • Ëttug tàggat ak gëstu ci nit ñi, naataange ak wergi-yaram meññenteel (IPDSR)
  • Ëttug tàggatug saytu ci sancum njëm (IFACE)
  • Ëttu farañse bi ñu jagleel ndongo doxandeem (IFEE)
  • Ëttu askan bi aju ci pajum xale (IPS)
  • Ëttug gëstu ci njàngale waññi (IREMPT)
  • Ëttu wergi-yaram ak naataange (ISED)
  • Ëttu xam-xamu suuf si (IST)
  • Ëttu xam-xamu dëkkuwaay (ISE)
  • Ëttu Afrig bu ñuul (IFAN)
  • Ëttu xam-xamug njàngale, njàngale yaram ak tàggat yaram (INSEPS)
  • Ëttu iniweersite bun app ak yar ci ndox (IUPA)

Daaray doktoraal

Soppi

ISAJ mi ngi diktal juróom-ñaari daara doktoraal[4] :

  • ndox, Melo ak Jëfandikoom ndox
  • Xam-xamu dund, wergi-yaram ak dëkkuwaay
  • Fisik, Simi, Xam-xamu suuf si, jàww ji ak toppat ligéey
  • Waññi ak Ĩformatik
  • Taaral, Aada ak caada
  • Njàngum nit ak mbooloo
  • Xam-xamug àtte, politig, koom-koom ak toppatoo

Werekaan yi ñu ràññe ci iniweersite bi

Soppi
  • Roose Dekottiñis, njiit bu njëkk ci daara yoon bi..
  • Maalik Njaay, sossiyiolok, jàngalekat bu dayo bu njëkk [5].
  • Saliou N'diaye, sëriñu taarix, nekkonn diktalkatu ëttu àttekaay , nekkoon njiitu daara ladab ak xam-xamu nit, ñu defko njiitu iniweersite bi ci atum 2010.
  • Suleymaan Basiir Jaañ, nekkoon jàngalekatu filosofi ak njiitu daara ladab ak xamu-xamu nit ci iniweersite bi.
  • Abdulaay Wàdd, Njiitu paarti liberaal, bokk ci joƞante fal njiitu réew mi ci atum 1978, nekk njiitu réew mi li ko dalee bés bu njëkk ci weeru awril atum 2000 ba ñaareelu bés bu weeru awril atum 2012.

Njiiti iniweersite bu Ndakaaru

Soppi

Royuwaay:Mbind mu leer

Ndongo yi fa jàngee

Soppi

Leeral yi ak tektal yi

Soppi

Xoolal tamit

Soppi

Bindin yi ni mel

Soppi

Téerantu bi

Soppi

Jokkale yi wuute

Soppi

Royuwaay:Ci yeneeni mbébétu

Royuwaay:Dalinu

* Xeet : Iniwersite bu Senegaal Xeet : Ëttu njàngale bi ñu sanc ci atum 1957

Iniweersite Séex Anta Jóob

iniweersite Séex Anta Jóob(ISAJ), ñu xam ko itam ci iniweersite bu ndakaaru, moom rekk mooy iniwersite ci Ndakaaru, kàppitaalu Senegaal, ci Afrig Soowu Jant.

  1. Njuumteg royuwaay: Balise <ref> incorrecte : aucun texte n’a été fourni pour les références nommées Unnamed_5-20230318194149
  2. Njuumteg royuwaay: Balise <ref> incorrecte : aucun texte n’a été fourni pour les références nommées Unnamed_6-20230318194149
  3. 3,0 et 3,1 GEO Royuwaay:N°403 de septembre 2012, Royuwaay:P.65
  4. Njuumteg royuwaay: Balise <ref> incorrecte : aucun texte n’a été fourni pour les références nommées Unnamed_7-20230318194149
  5. Njuumteg royuwaay: Balise <ref> incorrecte : aucun texte n’a été fourni pour les références nommées Unnamed_8-20230318194149