Aw xët ci wàll gii
Diiwaani Senegaal yi ay xaaj yu yoriin yu Senegaal lañu.
nosiinu suuf si
Soppidogiin wi
SoppiFii mu nekk, séenub lim mi ngi ci 14, la ko dale ca ba ñu sosee diiwaanu diiwaanu Matam ca 2001, teg ci yeneen ñatti diiwaan yi ci 2008 : Kafrin ci digg bi, Keedugu ci bëj-saalum-penku bi ak Séeju ci bëj-saalum, ci Kaasamaas[1].
rëyaay ak askan
SoppiDiiwaan | Rëyaay en km² |
Askan |
---|---|---|
Ndakaaru | 550 | 2 411 528 |
Njaaréem | 4 359 | 930 008 |
Fatig | 7 935 | 639 075 |
Kawalx | 16 010 | 1 128 128 |
Koldaa | 21 011 | 834 753 |
Luga | 29 188 | 559 268 |
Maatam | 25 083 | 423 041 |
Ndar | 19 044 | 863 440 |
Tambaakundaa | 59 602 | 530 332 |
Cees | 6 601 | 1 348 637 |
Sigicoor | 7 339 | 557 606 |
mboole-séen :[2] | 196 176 | 10 225 816 |
ay karmat
Soppi- ↑ yax bi péncum ndawi réew mi kàddu (woote) ci 1 fewrie 2008 [1]
- ↑ ay mboole-séen (walla ay mboolante) bu ñu tënkoo ci lim yu aliwa jii (lim yu ñu roowal (yu ñu mottali))
Voir aussi
SoppiJukki yi ci aju
Soppi- Diiwaani Senegaal(Régions du Sénégal)
- Tundi Senegaal(Département du Sénégal)
- Ndiiwaani Sénégal (arrondissements du Sénégal)
- Dëkkaani ndiiwaan yu Senegaal(Communes d'arrondissement du Sénégal)
- Dëkkaan yu Senegaal (Communes du Sénégal)
- Gox-goxaan yu Senegaal( Communautés rurales du Sénégal)
Bibliographie
Soppi- (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
- (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
- (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal, Dakar, Ministère du Plan, 1967, 705 p. (Thèse de 3e cycle publiée)
- (fr) Laurence Porgès, Bibliographie des régions du Sénégal. Complément pour la période des origines à 1965 et mise à jour 1966-1973, Paris, Mouton, 1977, 637 p.
lëkkalekaay yu biti
Soppi- (fr) Agence Nationale de la Statistique et de la Démographie du Sénégal (chiffres des différents recensements et estimations officielles jusqu'en 2015)
- (fr) « La région dans les limites administratives des États de l'Afrique de l'Ouest » (article de Gérard Brasseur dans le Bulletin de l'IFAN, série B, 1968, tome 30, n° 3, p. 861-867)
- (fr) « Trois nouvelles régions administratives seront créées au Sénégal » (Agence de presse africaine, 25 mai 2007)