Alse
Alse walla الجزائر ci araabi alseeri mooy péeyu réewum Alseeri, féete ci bëj-gànnaaru réew mi janook Géej gu Diggu gi. Mooy itam dëkk bi gën a mag ca réew ma
الجزائر Alse | |
---|---|
Réew | Alseeri |
Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
Kawewaay | 424 m |
way-dëkk | 2 203 698 nit |
atum way-dëkk | 2 009 |
Barabalub Alse | |