Ayiti
(Yoonalaat gu jóge Aayti)
Ayiti ab dun la bu nekk ca Amerik diggu. Day ab dun bu mag bu mu bokkal Republik dominicaine te Port-au-Prince di péyam.
Ayiti | |||||
| |||||
Barabu Ayiti ci Rooj | |||||
Dayo | km2 | ||||
Gox | |||||
Way-dëkk | nit | ||||
Fattaay | nit/km2 | ||||
Xeetu nguur - Njiitu Réew - Njiitu Jëwriñ |
|||||
Tembte - Bawoo - Taariix |
|||||
Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
Port-o-pirins | ||||
Làkku nguur-gi | wu-faraas, kereyool bu Ayiti | ||||
Koppar | |||||
Turu aji-dëkk | |||||
Telefon | |||||
Ayiti mooy reewu ñu ñuul ñi njëkka moom seen bopp ci attum 1804, ca seen fippu ga (1791-1803) ca la ñu dakkee Napoleon ak ay ñoñam ca dun ga.
Magginu turu dëkk ba
SoppiCi aaday Taino yi, Ayiti da doon tekki suufu doj yu kawe ya walla aw doj ci biir geej.