Xarey àdduna yi ñooy ñaari xare yi réew yu bari ci àdduna bi bokkoon doon def ci seen biir. Doon xare yi ëpp ay yaqu-yaqu ak ay bakkan yu ci des.
Laataa Ñaareelu Xareb Àdduna bi bu njëkk bi Xare bu Mag bi lees ko daan woowee.