Xare
Xare bu santee G (xare g) xamal ne jëf la, mooy li farañse naan: guerre; araab naan ko حرب, àngale di ko wax war.
Xare ga doxoon diggante jullit ña ak kéeféer ya ca Badar (xare badar), jullit ña a daan.
Xare su santee B (xare b) mooy li farañse naan: armée; araab naan ko جيش, àngale di ko wax army
Niral: Lat-Joor takk na xare bu màgg ngir xeex ak tubaab bi.