Waxtaani wàll:Junj
Dernier commentaire : 16 at ci ginaaw par Abdu Xaadir KEBE
ab junj waruñu koo wax, waaye ab tàmbali, ndax day lu ñu tàmbali te àggagul kon ab tambali lanuy wax
- yaakaaroo ne junj ak tambali benn lañu. loo junj mooy loo tambali. junj am mbir --Ibou 21 Oktoobar 2008 à 19:27 (UTC)
Ab junj ab joxoñ, la gën a jege. junj na ko ci biir ay waxam: il y'a fait allusion, junj na ko ci baaraamam: joxoŋ na ko. junj tam day tekki symbole ci fr --Abdu Xaadir Kebe 22 Oktoobar 2008 à 00:56 (UTC)